Adja Série. - Ramadan 2021 - Episode 20

Pour suivre toutes vos vidéos préférées :

- Abonnez - vous ici : esdos.info

Suivez nous aussi sur les réseaux sociaux :
- Twitter : patisentv
- Facebook: groupepatisen

Webséries, sketchs, recettes de cuisine, bienvenue chez vous!
Savourez la vie!
Découvrez l'univers patisen sur www.patisen.com

Comentarios

  1. Lune Dv Baller

    Lune Dv BallerHace un día

    Adjaa 😂 alima leuh beugoneuh waay farr yalla diarr tchi tour bi Rose

  2. Oumy Diop

    Oumy DiopHace 2 días

    Ay bouléne Héléna diappei

  3. Babacar Ndiaye

    Babacar NdiayeHace 3 días

    Tay mounékh diogaye rék Com dabi tite diogaye rék nékh rék 😂😂😂😂😂💕💕💕💕💕💕👍👍👍👍

  4. Babacar Ndiaye

    Babacar NdiayeHace 3 días

    💕💕💕💕

  5. Les Astuces de SUZ CHOU

    Les Astuces de SUZ CHOUHace 5 días

    wa team sétane lep dewenaty bonne fête. maylenma abonné nak si sama chaine bi. Yalla fay la amin

  6. Ablaye Diop

    Ablaye DiopHace 5 días

    Dougoutigui mo niemé yalahh😂😂diogoy nena mbaye Faye kom louniou mouseul😂😂

  7. Eumeu Diagne

    Eumeu DiagneHace 7 días

    🧡👍😃😄🙏🙏🧡

  8. Gamma AerozHD

    Gamma AerozHDHace 7 días

    Koor gui gawna année bii lepp la woor day kalandakh 😂

  9. Eugenie Helene Ndiaye

    Eugenie Helene NdiayeHace 9 días

    Ou est mami 😭😭

  10. Guile Diallo

    Guile DialloHace 9 días

    Lou beug gnou ték Adja vacance beusseul j'aime

  11. Doudou Sarr

    Doudou SarrHace 9 días

    Ndékké Dougui Tigui meunoul l3kk késsé...😀 fénn mo ci meune 😉

  12. Aladji Ndiaye Cherie FATY Lo ak Rama Ndiaye

    Aladji Ndiaye Cherie FATY Lo ak Rama NdiayeHace 9 días

    Mhcnbcbnfufmfmfu

  13. bernard dasylva

    bernard dasylvaHace 10 días

    JE PENSE CONTINALEMENT😂😂😂

  14. ndeye yande penda ndiaye

    ndeye yande penda ndiayeHace 10 días

    Watshap nigga non diogaye tamite

  15. Mamadou Niang

    Mamadou NiangHace 10 días

    Diogoy & Waga dougou 😆😆

  16. dialmb

    dialmbHace 10 días

    Dougou dougou dinama rey

  17. Awa Aidara

    Awa AidaraHace 11 días

    Pathe Sen deh bo dewe direct al diana nga dium Adja mi ngay diakarlol chaque jour day doundal xol manchallah yalna ngen goudou fane

  18. Bintou Keita

    Bintou KeitaHace 11 días

    Dougou mo nekh de

  19. MamiiSha Sow

    MamiiSha SowHace 11 días

    Tshiieuy Helena😂😂🤦🏽‍♀️😂

  20. Dethie fall Fall

    Dethie fall FallHace 11 días

    J'aime ma mère et toi si tu l'aimes aimer

  21. aisatou Thiam

    aisatou ThiamHace 11 días

    merci bcp dougoutigui je suis sans voix 🌹🙏🙏

  22. Amadou Sall

    Amadou SallHace 11 días

    Nice

  23. Astar cisse

    Astar cisseHace 11 días

    Adja machallah 🥰✨♥️🥺

  24. El hadji malick Diop

    El hadji malick DiopHace 12 días

    cou dakor senegal serigne lanou gueuna gueume yonentibi wala

  25. El hadji malick Diop

    El hadji malick DiopHace 12 días

    dou nieup wanté beuri nafii

  26. Mame Thierno Sylla

    Mame Thierno SyllaHace 12 días

    Tu as parfait ❤️

  27. Makhtar742 Mbengue

    Makhtar742 MbengueHace 12 días

    0

  28. Adia Bagayokho

    Adia BagayokhoHace 12 días

    Où sont les bambara venez vous pointez

  29. Fatou Diop

    Fatou DiopHace 12 días

    Sama série préférée

  30. Modou Fall

    Modou FallHace 12 días

    Doy guén kat ndeyam wakh si théâtre bi ta arrêté sen commentaire contre temps yi

  31. Alioune Aidara

    Alioune AidaraHace 12 días

    Machalah vous etes les meilleurs

  32. Alioune Aidara

    Alioune AidaraHace 12 días

    Machalah vous etes les meilleurs

  33. Titalova Sarr

    Titalova SarrHace 12 días

    Diogoye neina je pense 🧐 continental 🤣🤣

  34. Sokhna Khadija

    Sokhna KhadijaHace 12 días

    No Diogoy beug nako😂

  35. Mortalla Dieng

    Mortalla DiengHace 12 días

    Non esk réellement vous êtes comme ça vraiment je rêve une fille comme toi elle est calme dans ses paroles gentille le respect envers son mari ohhhhh jaime trop Adja paix sur toi

  36. Ndeye niang

    Ndeye niangHace 12 días

    Kou beugue yobou sayay maka beusseu

  37. Aissata Diew

    Aissata DiewHace 12 días

    "Je suis garçon douma dioy"🤣🤣... tonton diogay wayy

  38. Anta Touré

    Anta TouréHace 12 días

    Boy Pathé sa ndel bi sett na deh xana diogay Mola watt

  39. Banné Ndiaye

    Banné NdiayeHace 12 días

    Whatsapp nigga 😂 ki dinama ray rek

  40. Birame Dieng

    Birame DiengHace 12 días

    Mne dOuma diOY J'suiS GarÇOn🤣

  41. Gora thiam

    Gora thiamHace 12 días

    Amy diogay c un père a twa mais pas tons

  42. Abibatou Sow

    Abibatou SowHace 12 días

    ❤️❤️

  43. Ndeye Diop

    Ndeye DiopHace 12 días

    Amine ya rabi

  44. BEUGEU SERIGNE TOUBA tv Gaye kouel 3

    BEUGEU SERIGNE TOUBA tv Gaye kouel 3Hace 12 días

    Statut 😂😂

  45. cheikh amar

    cheikh amarHace 12 días

    Qui a remarqué q série bi amna eureur

  46. Akatsuki officiel

    Akatsuki officielHace 12 días

    vive marodi tv🎆

  47. ngagne gueye

    ngagne gueyeHace 12 días

    Kou abonné si mane yalla nga téki ba téral sa yaye

  48. Siré Kaba

    Siré KabaHace 12 días

    Moi j'aime ami

  49. Sow Mamadou

    Sow MamadouHace 12 días

    Diogoye 🤣🤣

  50. BaD Boy Musique

    BaD Boy MusiqueHace 12 días

    Amine

  51. Balal Sarr

    Balal SarrHace 12 días

    Seytané wakhoul degue wanté yakana xel💔 c'est le cas diogaye et dougoutigui😂🥰

  52. Adama Kone

    Adama KoneHace 12 días

    Watsap niggas😂

  53. Falli Bakhoum

    Falli BakhoumHace 13 días

    Blh assane diop sa me fait rire cette série . NB: ( kén dou pere diok's )

  54. Alassane Diop

    Alassane DiopHace 13 días

    Nice

  55. Usman Sylla

    Usman SyllaHace 13 días

    La vie il faut trouver bonne fille c'est fini je te jure

  56. Tizio Nabot

    Tizio NabotHace 13 días

    episode pas de son mal faite

  57. Touba Mbacke

    Touba MbackeHace 13 días

    😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂 😂

  58. Matar Mbaye

    Matar MbayeHace 13 días

    Ou sont les fans de Dougoutiki beuss lén j'aime 👍

  59. Petit_Pape PPG

    Petit_Pape PPGHace 13 días

    😂😂😂😂 dougoudaga mi kouma na doul leu 😂😂😂😂

  60. Sokhna fall

    Sokhna fallHace 13 días

    Am lén diammu

  61. GRAFI SEN

    GRAFI SENHace 13 días

    Abonnéle si DECOUVERTE TV guir Yalla

  62. Momi Diop

    Momi DiopHace 13 días

    Way nagn si diape pathé Séne et Adja se marie pour de vrai way. Mais quel couple 🥰❤️🥂

  63. Bathie Traore

    Bathie TraoreHace 13 días

    Ou sont les fans de doukoutigui

  64. Adame Ngom

    Adame NgomHace 13 días

    Douguou tu es folle 😂😂😂😂woye dioguaye

  65. tapha mbaw

    tapha mbawHace 13 días

    Merci

  66. Fatou ndiaye Faye

    Fatou ndiaye FayeHace 13 días

    Ay way goor yéné nala naar bi nk wayé sa papa ih dina doy waar

  67. Khady Diouf

    Khady DioufHace 13 días

    Kéne rk mola meunoul bayi si adouna Mouy sa yaye kou beug sa yaye beuseul j'aime

  68. Crazy boy l'officielle Boy

    Crazy boy l'officielle BoyHace 13 días

    Ami beug nga soblé nak srx 😂😂 khana yassa rek nga meune

  69. malick ka

    malick kaHace 13 días

    تعصي الإله وأنت تظهر حبه❤️ هذا محال في القياس بديع❤️ لوكان حبك صادقا لأطعته❤️ إن المحب لمن يحب مطيع ❤️

  70. Ndack niang

    Ndack niangHace 13 días

    Do rigole Tokyo

  71. Saye Lo

    Saye LoHace 13 días

    Mais où est le petit djoguaye

  72. Ramata Sy

    Ramata SyHace 13 días

    Mais entre citron🍋🍋🍋ak dougoutigui louy sen problem😉😉

  73. ndogal deme

    ndogal demeHace 13 días

    Nice n'a vraiment j'adore sette

  74. Ba alpha Ba alpha

    Ba alpha Ba alphaHace 13 días

    🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🔥🥰🥰🥰🥰

  75. Abdou Khoudoss Syll

    Abdou Khoudoss SyllHace 13 días

    Diogoye néna : Mbaye Faye melni kouniou mousall😂😂😂sama badiane mo beug taille fine WhatsApp Niga😂😂😂

  76. El Cano

    El CanoHace 13 días

    Diogoye tay mou dé

  77. Coumbis Diouf

    Coumbis DioufHace 13 días

    Dougou tigui yangui fayou nak😭😂😂 niaffff😂😂

  78. Hélène Diatta

    Hélène DiattaHace 13 días

    Dougoutigui Noma yabé🤣🤣

  79. Aminata Sène

    Aminata SèneHace 13 días

    ROSEEE WALA HALIMAA?

  80. Mode,Style,Beauté,sex les charmantes filles

    Mode,Style,Beauté,sex les charmantes fillesHace 13 días

    Série bi nékhatoul

  81. Moussa Sy

    Moussa SyHace 13 días

    Machallah 🙏

  82. badou diop

    badou diopHace 13 días

    10:12 puff daddy😅😅😅😅😅😅😅😅non diogaye do nitt

  83. Ibrahima MM Tine

    Ibrahima MM TineHace 13 días

    Cou beugue sa Yaye like

  84. Mohamed Benzékry

    Mohamed BenzékryHace 13 días

    Adja rafetna djekkk piirr la tioooooo nopnako 🙄

  85. Theirno Niang

    Theirno NiangHace 13 días

    Vraiment diogoy ils et meilleure😂😂

  86. Elcapo Doumbouya

    Elcapo DoumbouyaHace 13 días

    Adja ,tu mangeras le Rosa que tu as mis sur tes lèvres en période de dîné 😂

  87. Khoudia Mbaye

    Khoudia MbayeHace 13 días

    djiogay warnagne wakh thi mom kou niew mou sonala 😩

  88. Niimatengella Jallo

    Niimatengella JalloHace 13 días

    Mach-Allah vraiment je suis fier de vous et bonne continuation

  89. cheikh bass al amin

    cheikh bass al aminHace 13 días

    Avis de recherche pour mami?

  90. Barakatou kandé

    Barakatou kandéHace 13 días

    Je pense continentalement😂😂😂

  91. anita anta

    anita antaHace 13 días

    Vous avez des problèmes ak sou sop diw

  92. fatima thiam

    fatima thiamHace 13 días

    No vraiment diogaye dafa nekh😂😂nimou kholer dougoutigui😂nena niou togou niari thine 😂😂🤦🏽

  93. Gros Bb Officiel

    Gros Bb OfficielHace 13 días

    Salam yennn mamy la guissoul foumou nekkk 🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇲🇷🇲🇷

  94. Matar Amar

    Matar AmarHace 13 días

    Diogueye Loutax mou Rakadiou rk😂😂😁😁🤦

  95. authentic-boy Bayo

    authentic-boy BayoHace 13 días

    Dougoutigui n'golobougou Diarra 🇲🇱🇲🇱🇲🇱✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿✊🏿

  96. Fa Fatou

    Fa FatouHace 13 días

    Diogoye nena je pense continentalement🤣🤣🤣🤣🤣🤣 sheuuu

  97. Fa Fatou

    Fa FatouHace 13 días

    🤣🤣🤣🤣 doougoutigui ak citron foum ko sein daw

  98. Idy Fedior

    Idy FediorHace 13 días

    Dougoutiti dafa pore tay dh

  99. a x ek

    a x ekHace 13 días

    Ku yaakaar ne dafa yeww lool lu yomb moo kay daa neel.

  100. a x ek

    a x ekHace 13 días

    Jigéen ju mel ne Elenaa ku leen takk Boo leen nappul dañuy toog sa bopp bi.

  101. a x ek

    a x ekHace 13 días

    Jigéen ñépp Buñu meloon ne Ajaa góor ñépp mel ne paate kon leegi àdduna bi soppiku goyaar (ajjana).

  102. Balde 98 Balde

    Balde 98 BaldeHace 13 días

    Abdoulaye Wade à dit.. 🔅Travailler 🔅Encore travailler 🔅Toujours travailler Macky Sall à dit... 🔅 Énervée 🔅Toujours énervée 🔅Encore énervée Kou mounoul diar si péage n'a diel routes nationales bi 😓😓😓😓😓 Mane kay déma warou Sall🙆🙄🙄