Eumeu Sene Sort de sa réserve après son Combat J'ai été atteint Mystiquement, Meussouma beuré...?

Abonnez-vous à notre Chaine ESdos: esdos.info/put/udfBmVXjm-DTPjYNv8AWvQ.html?view_as=subscriber Aimez notre page Facebook: becayembayetv/ Visitez notre Site web: www.fmsenegal.info #Bantambatv.
77 419 03 64

Comentarios

  1. Youssou Diop

    Youssou DiopHace un hora

    Eumeu bilahii wakh ga deug lac 2 da donn teup aka dall rekk pour wone gayii nee mooguu def dara tee tank yii sakh diogoul

  2. Issa Diao

    Issa DiaoHace un hora

    Lac dou mbeur bilahi

  3. Issa Diao

    Issa DiaoHace un hora

    Na bayi beurré

  4. Ndaye Khodia

    Ndaye KhodiaHace 4 horas

    Ndanane koulou ndanane 😀sama mbeur bii yalnala yallah dfl djm rk Yaw ak modou lô ndam siréee khalé by kham limuye deff 😁😁 Athia mbeur

  5. Assane Samba

    Assane SambaHace 7 horas

    Wathié akh amateurs yii wathié supporter yii diambar nga ndanane nga gaindé nga amato loy prouver si lambe d'elle déglou sa encadrement géré sa carrière champions one love eumeu sa beuré mo tah ma beugu leu té dou dégn yalnala yalla diapalé

  6. Boury Ka

    Boury KaHace 8 horas

    Balla sama gaynder Ndiaye

  7. Mamy Ba

    Mamy BaHace 10 horas

    Goor yalla deugue gua machalah ❤️ djomm reek gay prouver eume kou am djomm gua amoulo Keen akk nala Diam sonal sa yaye dala gnanal bilay wolay machalah ❤️

  8. Muslim2proud

    Muslim2proudHace 11 horas

    Kouko déffati nako deegg, ap mbeur dou fénn, mbeur dou tapalé...aaay kouko défati nako deeg ap mbeur dou tricher mbeur dou yambar, 😤diapé sénégalais yi dofff 💃💃💃💃💃😂😂😂😂😂Eumeu, Balla Gaye2, Yekini, Bombardier, Ama Baldé, merci infiniment, gathiéloulén lambe. Fatou Guièr 2 démal nga toog, ngir yalla boulfi dieuleuti beneu combat, doyal na gnou si yow seuk.🙄🙄😏😏😠😠😠😠😠

  9. Djily Diop

    Djily DiopHace 12 horas

    Non eumeu gor deugue la

  10. bssni touir

    bssni touirHace 8 horas

    Lou lérr laa wakh

  11. vmvdou svné

    vmvdou svnéHace 14 horas

    jai trop aimé son discours

  12. Sénégal com

    Sénégal comHace 17 horas

    mane fans balla gayé la

  13. bssni touir

    bssni touirHace 8 horas

    C'est vrai je suis avec eumeu

  14. Sénégal com

    Sénégal comHace 17 horas

    bilahi euma borom bakh la

  15. drttyu liqm

    drttyu liqmHace 17 horas

    yi wara boycotté 👎no sa geste ak Bg2 machala

  16. El Che

    El CheHace 18 horas

    Lac 2 moy enfoiré rek . Yaw kenn du yaw jambar deug ga

  17. Mamadou Alpha Bah

    Mamadou Alpha BahHace 18 horas

    Je suis un fan de Modou Lo mais je t'aime💕💕❤❤😍

  18. Marieme Balde

    Marieme BaldeHace 18 horas

    Mais eumeu nak balla dinala dane dh one bakhga trop beugue nagne la mais dinagne la dane dh 😂😂😂

  19. drttyu liqm

    drttyu liqmHace 17 horas

    lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak

  20. Marieme Balde

    Marieme BaldeHace 18 horas

    Sana xol diekhna si lac thiim. Bravo eumeu courage. Balla ak wa keureum gnoy samay mbeur (sauf Lac maintenant) legui iow yako remplace. Borom vakh nga

  21. Aita Ndiaye

    Aita NdiayeHace 19 horas

    Eumeu takussane buné def ngakofi macha alla dangua mene béss gaindé bi yarunga mene nga béss

  22. Ndeyemarie Seye

    Ndeyemarie SeyeHace 19 horas

    Diamou RK ngayi âme bly

  23. BUZZ MIFA

    BUZZ MIFAHace 20 horas

    EUMEU BOUL BAY AWMA KÉNE COUEOUL YEW

  24. Khady Togola

    Khady TogolaHace 20 horas

    Eumeu ya meuna doull lac dakeu leu bangua guéneu sakou yi guay féne Amgua mélokane déh khawma wone ni ningua mel féne bakhoul

  25. BUZZ MIFA

    BUZZ MIFAHace 20 horas

    EUMEU JE T'AIME BILLAHI

  26. Issakha Ndiaye

    Issakha NdiayeHace 20 horas

    Tu fais partie des meilleurs.

  27. Aboubacry Sarr

    Aboubacry SarrHace 21 un hora

    Ya fi meun dh Eumeu billahi ❤️

  28. Chekh tidiane Thiam

    Chekh tidiane ThiamHace 21 un hora

    C'est vrai je suis avec eumeu

  29. Mbacké Seck

    Mbacké SeckHace 21 un hora

    Lou lérr laa wakh

  30. Modou Mbaye

    Modou MbayeHace 21 un hora

    Eum bénéne yonne boy bré boul nuyoti kénn lokho.bâ nga nuyo thi lamb dji la khamni da ngay d'Abou.

  31. Abdou Mbaye

    Abdou MbayeHace 21 un hora

    Eumeu sa kanam

  32. khass Killah

    khass KillahHace 21 un hora

    Boléne waxé té yalla tax ngéne xamni lac2 mo tané si combat bi ndax mom sax défna touti effort eumeu sax wax nako après combat bi "waroléne ma wonn téyélo sama bop" motax dafa taxaw rék défoul dara. Questioné nagn ko mo bo xolé boubax dafay rafétal di rectifié wax bi coz ay staff faw gnoniko bouko wax parck lolou daf léni yaxal mbeur gnou fayla ay millions sa staff nane la téyél sa bop

  33. Penda Wade

    Penda WadeHace 22 horas

    Yaw diabargua bilay

  34. Khady Gueye

    Khady GueyeHace 22 horas

    lac dafa raguale rek yow amélo kéne ak

  35. Khady Gueye

    Khady GueyeHace 22 horas

    billay diabare gua

  36. Mame Saye Sylla

    Mame Saye SyllaHace 22 horas

    Bilahi eumeu sene wakhone na lako si beineu commentaire nila lac de guiers 2 dalayy tardel rek khamoul gatt ragale na bilahi wokhone na lako beurei woule bayi woule dafa ragalll tropp tropp

  37. Abu Konate

    Abu KonateHace 23 horas

    Eumeu lat 2 amoul diome

  38. Ibrahima Khaliloula Hounsah

    Ibrahima Khaliloula HounsahHace 23 horas

    Eumeu Nguaïdé Nguay Meussa Done Bo Bayé Beuré Sax Nguaïdé Ngua

  39. Diogop Ka

    Diogop KaHace 23 horas

    Machalla fiér de toi champion 💪💪💪sa kaw sa kaname

  40. Ibrahima Diop

    Ibrahima DiopHace 23 horas

    💪💪💪👍👍

  41. Khadidiatou Gueye

    Khadidiatou GueyeHace un día

    Barki yamlah Eumeu damala beug

  42. Seyidina Sow

    Seyidina SowHace un día

    Eumeu champion nga lou lérr Lac war nga kholaat sa beuré té di dieul décision, am nga katane loy ragal, khamon sakh biss bo mome warko am ndam,... modou lo ndam rék Incha ALLA

  43. Sila Dame

    Sila DameHace un día

    Q

  44. Sall Ablaye

    Sall AblayeHace un día

    Khole bou rafet eumeu

  45. Mansour Gueye

    Mansour GueyeHace un día

    Mberr yaw diaroul sakh ngay nioue khana nonou yaye Kane mberr pure nga

  46. Isatou Jobarteh

    Isatou JobartehHace un día

    Eumeu sene yow ya Barry wakh barry tapaleh

  47. Fati Sow

    Fati SowHace un día

    waw kay eumeu diadieuff way on te fais confiance

  48. Adama Fall

    Adama FallHace un día

    Champion nga

  49. Mariama Diéne

    Mariama DiéneHace un día

    💪💪😇😇😇😍😍😍👍

  50. ASTOULO KOBAR

    ASTOULO KOBARHace un día

    Eumeu yawdal gathia ngalama chapeau a vous mbeur kaamil NGA

  51. Pape Davido

    Pape DavidoHace un día

    Cœur pour diambar jdi ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  52. Tijani Dia

    Tijani DiaHace un día

    Waw kay sama mbeur bi amal diame yaw lanou beugue tay ak soube mala beugue rek té yallah takh soy beuré douma ame diame wallahi taye wnibik hateu

  53. Pape Davido

    Pape DavidoHace un día

    ♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️☺️☺️☺️☺️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️♥️

  54. Ahmada Dial

    Ahmada DialHace un día

    Iow tamit beure wo ...wakh ko kéne meunou niou nakh

  55. Adama Camara

    Adama CamaraHace un día

    Eumeu séne diambar gue nion gui sa gui naw

  56. Gooo Bhff

    Gooo BhffHace un día

    Eumeu ❤️❤️❤️❤️💪

  57. Gooo Bhff

    Gooo BhffHace un día

    @gtoss chddy lac mo bougone Revanche

  58. gtoss chddy

    gtoss chddyHace un día

    Vous avez tout les deux déçu

  59. Mariama Aliou Diouf

    Mariama Aliou DioufHace un día

    Fier de vous Eume Sene

  60. Serigne saliou Lo

    Serigne saliou LoHace un día

    Waw lac nonou ladone def mé khamnanou touti si lamb

  61. gtoss chddy

    gtoss chddyHace un día

    Vraiment jambar gua mbeur lac modoul touss

  62. ibrahima ndom

    ibrahima ndomHace un día

    Eumeu mi da melni da beug beuré wate AK Balla

  63. Pisco Kane

    Pisco KaneHace un día

    Wakhoo fi dara...tu as fui le combat .sois honnête waay .

  64. Rama Gueye

    Rama GueyeHace un día

    Euma boul décourager lépou dina bakh lac mome dangay warou 💪

  65. Fatou Thiam

    Fatou ThiamHace un día

    Walaye tu est le meilleur je t'aime mbeure

  66. JuNiOr BabA

    JuNiOr BabAHace un día

    Wakh dji amna solo yéndou na maana eupeu

  67. samba Sy

    samba SyHace un día

    Il a raison, lac2 c’est un fuyard

  68. Mame Gor

    Mame GorHace un día

    Eumeu wakhna deug 🤭Mbeur yi nio maak thiéré massé ak lalo 😂Balla gaye ak papa sow biniouy mbapatt. 2002 terrain 22 bounte keur birahim Ndiaye sétane nako j’avais 17ans legui nio donc niom warone nagnou am 20 ans ou 22 ans donc souma calculer balla warna aam 39 ans ou 40 ans a se moment 🤭🤭😂😂

  69. Aly Dieng

    Aly DiengHace un día

    Bilahi emeu ta raison lac amoul dioum amoul fouleu

  70. Bienvenu Cheikh chico SECK

    Bienvenu Cheikh chico SECKHace un día

    Eumeu nak, on t'aime bien because yagg gn beuré lamb jank you neex mais bi mom iow ak lac yaleen si yem defoleen fi dara dsl nak defaroul watt da melni filla mod'lo dougeul guénagoffa D.

  71. tyfa dieng

    tyfa diengHace un día

    Late 2 dou mber nabayi beré on t'aime fort eumeu💪

  72. Serigne Modou Diallo

    Serigne Modou DialloHace un día

    Bilay man serign fans balla la mais dam beugue eumeu sene ndkh balla gaye

  73. Mamediarra Balde

    Mamediarra BaldeHace un día

    Defofi dara bou niou wakhante deug daga ma rouslo kerok

  74. Ablaye Gueye

    Ablaye GueyeHace un día

    Vraiment jambar gua mbeur lac modoul touss

  75. Ousmane Sagna

    Ousmane SagnaHace un día

    Vous avez tout les deux déçu

  76. GALAYE DIOP

    GALAYE DIOPHace un día

    lac daladon gadie😂

  77. Bana Ndiaye Gueye

    Bana Ndiaye GueyeHace un día

    Yow ndanane gua wayai lac rek badola ore serie la

  78. Khady Diao

    Khady DiaoHace un día

    Machallah 🤝🤝🤝

  79. Sarr Mouhamet

    Sarr MouhametHace un día

    Eumeu lime wakh dafa lérr

  80. ImD CRONIK

    ImD CRONIKHace un día

    Eumeu Sène lingay wakh déssé set Yalla faté khadjou fi ya wakhone ni Bayi nga Balla Gaye 2 Adouna ak Alakhira ndakh bingay beuré ak mom da souli sa néwou Yaye boye wakhati déssi khol euleuk té mouytou wakh bouye diakhassé aye nite Aye Adversaire ngen bou lamb takh kouné wakh lo khamni souba nga koy reuthiou

  81. Sarr Mouhamet

    Sarr MouhametHace un día

    Eumeu SENE le champion

  82. Lamine Diallo

    Lamine DialloHace un día

    Macha allah eumeu Lac mom bou amone combat tay sakh dou beuré ndakh ragal la

  83. Yacine Seck

    Yacine SeckHace un día

    Affaires bi yaw mbeur DEUG t'ai do ragal

  84. Allah L’Unique

    Allah L’UniqueHace un día

    Je suis supporter de Modou Lo mais aka y’a âme Diome merci eume

  85. Hamade Faye

    Hamade FayeHace un día

    Reug Reug 💪💪💪 en bas les vieux

  86. Pape Samb

    Pape SambHace un día

    Man Modou lo là mé balla guaye dafa bakh

  87. Dy Toure

    Dy ToureHace un día

    Eumeu ken gueunoula ndeyssan maguilay gnanal ndam so amaté combat Lac de Guer mbam la rek daf la beugueu tilimeul xamnagn Champignon gua Fans Balla G2 la ak Mod lô Much lov Mbeur

  88. Saliou Mboup

    Saliou MboupHace un día

    Ndaysane eumeu dama ko yeureum aussi dafa beug balla sama mbeur mi🥺♥️♥️♥️

  89. christiane diouf

    christiane dioufHace un día

    Wawaww yaw lion nga

  90. Aissata Sow

    Aissata SowHace un día

    Eumeu tu est adorable on t aime toujours quoi qui arrive

  91. soniyu ziuy

    soniyu ziuyHace un día

    Nooo yalla degrek la boug me lacmom sama mbokla me dey fontou

  92. Zirady Sow

    Zirady SowHace un día

    rafetna eumeu deug rek la fi wakh mais eumeu modoul lo bou ame combat meme boude sa rakha khadim ngom lay bere dnga wara mandou thi combat bi ndakh nioun fans modou lo yi yepe yow lanlouy siporté boy bere

  93. Neinishh Sarr

    Neinishh SarrHace un día

    Lac si bopam nagn wara bayi teugal combat

  94. Amdy Fall

    Amdy FallHace un día

    Eumeu borome bakh nga nak mais mayat niou chance rék laniou laye niane yangi maye soga nékh nak billahi balla kouko beug niou beug la

  95. soniyu ziuy

    soniyu ziuyHace un día

    Un vrai champion je t'aime tellement fort bilahi ioe rék yama doy thie mbeur yii bilahi mane ioe laye gueume

  96. Khadidiatou Mbow

    Khadidiatou MbowHace un día

    Eumeu mane Balla moye sama mbeur mé gneup khamnagnou ni diambar gua lac mome na soumé koudji d'où dara

  97. Diatoubamba Gueye

    Diatoubamba GueyeHace un día

    Machalla eumeu je suis fans balla guaye mé beugeu nala trop lac mon defoul effort contana thi yaw champion

  98. Khady Ndiaye

    Khady NdiayeHace un día

    ❤❤❤❤

  99. Prosper Gomis

    Prosper GomisHace un día

    Merci sene

  100. Fallou Ndiaye

    Fallou NdiayeHace un día

    Mane balla moye sama mber mes eumeu liga wah degue le gayi kham nane diambar yi

  101. Chérif Kandé

    Chérif KandéHace un día

    man dale beuna la ndakh balla geye

  102. penda ngom

    penda ngomHace un día

    Lac mome dou dème ardo ndahe dafa ragal door aye daw mo ko gueneul

  103. penda ngom

    penda ngomHace un día

    Bien dit Eumeu défo dara Lac mome tapète ak tricheur ak théâtre kate bou mak la

  104. Mouhamadou makhtar Sambou

    Mouhamadou makhtar SambouHace un día

    Billahi je supporte Balla mais ndanane nga lingua yeup deugue leuh bilahi damala beugue mane le peuple est content gaïndé

  105. Free Mind

    Free MindHace un día

    J’adore Eumeu Sene Lac est un poltron un tricheur pas un lutteur

  106. Umou Khairy

    Umou KhairyHace un día

    Bayilén kou am défaite né j’étais malade 😂😂😂way go En tt cas balla dal laniou begue c ça ❤️🥰👊

  107. FATOU ABDOU MBAYE

    FATOU ABDOU MBAYEHace un día

    Bilahi Mala beugg eumeu jambaar ni ioe lay mell