l'entrée époustouflante de Balla Gaye 2 dans l'Arène (face to face vs Bombardier) dou yomb

Pour bénéficier de toutes dernières vidéos de Keb Vision, nous vous prions de vous abonnez, activer la cloche de notification, d,aimer, de commenter et de partager...
Merci
Contact: 773141496

Comentarios

  1. bara faye

    bara fayeHace 8 horas

    Jeste noble c beau vraiment beau

  2. Ndiaw Sall

    Ndiaw SallHace 2 días

    The kinggggggggg😘😘😘😘😘

  3. Seyni Samb

    Seyni SambHace 2 días

    Le sourire de Balla 😍😍😍❤️

  4. Awa Fall

    Awa FallHace 2 días

    Bilaye mane fans balla la mé eumeu mone je l'adorer

  5. Mor Touba

    Mor ToubaHace 3 días

    Nekha faral

  6. Mognom Korea

    Mognom KoreaHace 3 días

    Je t'aime beaucoup

  7. ALPHA DIALLO

    ALPHA DIALLOHace 3 días

    BALLA REK

  8. Amadou Demba Aw

    Amadou Demba AwHace 3 días

    BG2💪💪❤👍

  9. Kiné Faye

    Kiné FayeHace 4 días

    Fiérté guédiawaye on t'aime grave❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️🌹🌹🌹🌹🌹

  10. Aziz Lam

    Aziz LamHace 5 días

    Ken dou mome kirasoulilahi

  11. Astou Ka

    Astou KaHace 5 días

    franchement balla gaye dafa nékha beugue yalla n'a diamou yague way❤️❤️❤️

  12. Chiekh Diop

    Chiekh DiopHace 5 días

    Balla g2❤❤❤💪

  13. Madiaga Asta Sall

    Madiaga Asta SallHace 5 días

    Masha Allah balla gaye sounou mbeur le meilleur et le plus élégant de sa génération .yalla na ame diam ak

  14. Modou mbaye CAMARA

    Modou mbaye CAMARAHace 5 días

    Et chapeau à Eumeu un grand champion noble et humble

  15. Modou mbaye CAMARA

    Modou mbaye CAMARAHace 5 días

    Merci Balla un vrai jambar.Nous seront toujours avec toi inchallah même avec cent défaite car tu ne déçois jamais t'es supporters. T'es un vrai lion 🦁 frère.

  16. Amdi Fall

    Amdi FallHace 5 días

    Machalla balla gaye 2

  17. Isatou Barrow

    Isatou BarrowHace 5 días

    Ohhhhh Ma Shaa Allah yyyy leeee nekh na❤️❤️❤️Ana nyee begue Balla Gaye😍

  18. Emsy Jr

    Emsy JrHace 5 días

    L'homme fort larenebi

  19. Ousmane Ba

    Ousmane BaHace 5 días

    Balla Geuye je l’aime billahi❤️❤️🥰🥰

  20. Sénégal Sénégal

    Sénégal SénégalHace 5 días

    Thiey un peuple endormi 😴 ils vont se laisser encore distraire pendant des années

  21. Babacar Dramé

    Babacar DraméHace 5 días

    Balla💪🏾💪🏾💪🏾

  22. Rokhaya diop

    Rokhaya diopHace 5 días

    Bg2 je t'aime 😘👊

  23. Ndeye maguette Wade

    Ndeye maguette WadeHace 5 días

    No balla gaye yalla na diamame yageu ki khol bi mo raféte

  24. Rokhiya Kanoute

    Rokhiya KanouteHace 5 días

    Balla yaye nekhale lamb

  25. Normal Lo

    Normal LoHace 5 días

    K c beau de voir ça . Malgré tout c le Sénégal qui gagne

  26. Coumba Diawara

    Coumba DiawaraHace 5 días

    Thiey sama mbeur mih mala fan ❤❤❤

  27. Adama Badji

    Adama BadjiHace 6 días

    No bilakhi Balla kholam dama rafete Eumeu aussi nittou kesser la

  28. Diagana Ismaila

    Diagana IsmailaHace 6 días

    Balla kassé 💡

  29. Adama Baldeh

    Adama BaldehHace 6 días

    Machahllah this is so nice balla gaye2👏🏻👏🏻❤❤

  30. Dieng Cheikouna

    Dieng CheikounaHace 6 días

    ❤️❤️❤️❤️❤️❤️❤️💪💪💪💪💪

  31. Ablaye ndiaye

    Ablaye ndiayeHace 6 días

    Machala

  32. Pape Silmang Ndior

    Pape Silmang NdiorHace 6 días

    Balla gaye 2 bilahi bouyébo souy bayi beuré Sénégal bayi lamb môme Dong mofiy mbeur love sur toi ❤️🌹❤️❤️ mbeur

  33. DJIBRIL BA

    DJIBRIL BAHace 6 días

    Balla bou bayiwone beure rek ma bayi setane lamb

  34. Genè ral

    Genè ralHace 6 días

    La seule malchance de bombardier est d'accorder la revanche à Balla gaye.yakhounga deh.

  35. Abdou Sow

    Abdou SowHace 6 días

    Ils sont les meilleurs

  36. Abdou Sow

    Abdou SowHace 6 días

    Ils les meilleurs

  37. Ibrahima Seck

    Ibrahima SeckHace 6 días

    Balla Gaye Moy mbeur

  38. Ndiaye Ndiaye

    Ndiaye NdiayeHace 6 días

    Ki mo mom lamb billahi Balla gaye 2✌✌✌

  39. NESTA 13

    NESTA 13Hace 6 días

    I call it fair play, great display to both champions

  40. Lamine Zo

    Lamine ZoHace 6 días

    No Eumeu vraiment mashalla

  41. Citizen of the world

    Citizen of the worldHace 6 días

    Machalah BG2 et eumeu sène yèna niak kignane tè rafète xoll ❤️🙏🏾

  42. Aissatou Ndiaye

    Aissatou NdiayeHace 6 días

    Balla nekha faral dimanche

  43. { M 2 A } MISTER 2em ARA

    { M 2 A } MISTER 2em ARAHace 6 días

    EUMEU DAFA FEN BALLA

  44. Cheikh Thiaw

    Cheikh ThiawHace 6 días

    Sama khol saidana loleee loleee balla moy sama mbeur wayai eume kou rafaite kholela

  45. Assane DIAKHATE

    Assane DIAKHATEHace 6 días

    li moy lamb fo ak ré apres mou diekh li moy senegal jsui fans eumeu sene mais balla la faral contre B52

  46. Bella Diop Dieng

    Bella Diop DiengHace 6 días

    La fin est 😍😍😍😍

  47. El hadji Diagne

    El hadji DiagneHace 6 días

    Mane fans balla la mais eumeu brome bax la koi

  48. Fall Cheikhtidiane

    Fall CheikhtidianeHace 6 días

    Li moy sport

  49. Alsini Samb

    Alsini SambHace 6 días

    Cest beau entre balla et eumeu sene

  50. Medzo Diouf

    Medzo DioufHace 6 días

    Ndaysan eumeu sene dafa gueme yalla balla gaye amoule béne probléme

  51. Abdoulaye cisse

    Abdoulaye cisseHace 6 días

    Thieye balla Gaye

  52. Daouda Ba oh Helene war immer mit den Banditen

    Daouda Ba oh Helene war immer mit den BanditenHace 6 días

    cBG" devrait avoir honte de faire Pub pour une huile venant de la france donc ke Guy Mary Sagna lui dit kelke chose cme il parle sur Macky sall

  53. Baye Saabou

    Baye SaabouHace 6 días

    eumeu séné a fait un beau géste

  54. Omar Jueye

    Omar JueyeHace 6 días

    Eumeu séne soit intelligent prend ton combat contre balla gaye et empoche des millions après par à la Mecque et tu prends ta retraite même si balla gaye te terrasse où est le problème balla gaye peut terrasser n'importe qui donc ne laisse pas les millions filets par la fenêtre la lutte n'est absolument rien appart le sport et le temps n'attend personnes ...Toi et balla gaye vous avez le même père et la mère car vous êtes tous des enfants du Sénégal alors offrez vous de l'argent voilà le seul conseil que j'ai à te donner et saurais été mon propre frère je lui dirais la même chose...je vous souhaites une bonne continuation et une bonne fin de carrière à toi et à tous les sportifs sénégalais ...Respect à vous...

  55. Cheikhouna Dieng

    Cheikhouna DiengHace 6 días

    Non modou Lô moy sama mbeur mais vraiment balla brome bax la billahi diam si yéne

  56. Daouda Anne at-tidiany

    Daouda Anne at-tidianyHace 6 días

    Non li nice neu billahi😭😭Billay wallay ay champions nguén. Billahi sama khol dafa sëddeu ciii image bi. Ohhhhhhh !!!!! Yaram dawna yahyi dëss

  57. Ibrahim abdoulaye Sonko

    Ibrahim abdoulaye SonkoHace 6 días

    L'association des lutteurs doit aller présenter ses condoléances à la famille de Diagar diagar.

  58. elhadji ndoye

    elhadji ndoyeHace 6 días

    Li rafena siporter yi yewoulén nioum ay kharit laniou

  59. khalille niang

    khalille niangHace 6 días

    Mrc balla Gaye 2😍😍😍😍😍😍😍

  60. BAYE POSE

    BAYE POSEHace 6 días

    Balla gaye boul kharito ak eumeu sene dh saytané la

  61. BAYE POSE

    BAYE POSEHace 2 días

    @OMAR BADJI Danga dioum eumeu sene rk si mana soss

  62. OMAR BADJI

    OMAR BADJIHace 2 días

    Yami yaye setana bout bone

  63. Junior Junior

    Junior JuniorHace 6 días

    Yallah ngua ame ndame Balla

  64. nfaly kante

    nfaly kanteHace 6 días

    cette partie entre Balla et Eumeu ma vraiment fait plaire que je ne cesse de la regardé, de vrai guerriers et un coeur en or

  65. Babacar Fam

    Babacar FamHace 6 días

    One love

  66. fanse fou malade

    fanse fou maladeHace 6 días

    Machallah Rafena

  67. DIENG Aby

    DIENG AbyHace 6 días

    Balla rek

  68. Diarra Gueye

    Diarra GueyeHace 6 días

    Man dal yaw la beugue ni BG2 for ever❤️❤️❤️

  69. Fall N'deye fatou

    Fall N'deye fatouHace 6 días

    Lime nékh si mome dou yakhe lambe

  70. Modou Ndiaye

    Modou NdiayeHace 6 días

    Eumeu sén en plein combat mou dém di féthie AK wa guediawaye li molay wane amoul xolou kignane té yoroul djikoye mbeur nite kou bakh

  71. Jules Touré

    Jules TouréHace 6 días

    Bombardier diekhal takk diamano yi Balla kou man

  72. Abdoulaye Balde

    Abdoulaye BaldeHace 6 días

    No eumeu dafa moudiou kharito ak balla dé yenn, machallah

  73. Diha Sallah

    Diha SallahHace 6 días

    Retanu balla rek am dara la😘

  74. Modou Diaw

    Modou DiawHace 6 días

    ❤️❤️❤️

  75. Diha Sallah

    Diha SallahHace 6 días

    Balla gaye rek laniu wakh niun✌

  76. fatou kandji

    fatou kandjiHace 6 días

    Sama lutteur Bagui ni BG2

  77. Assane Gueye

    Assane GueyeHace 6 días

    vraiment je suis fans de modou lo mais balla ak eumeu lignou def rafetna trop

  78. Modou Sall

    Modou SallHace 6 días

    Mbeur magui balla mattar le king des kings

  79. Ebrima Yanka

    Ebrima YankaHace 6 días

    Ndam rek inchallah le lion de diediaway

  80. Ousmane Gassama

    Ousmane GassamaHace 6 días

    Merci bravo Balla rek 💪💪💪♥️♥️

  81. Rama Gueye

    Rama GueyeHace 6 días

    Waw kay khalé bangi nonou paré fépou nak aka mako wolou💪💪💪💪

  82. ousmane top

    ousmane topHace 6 días

    Balla ak eumeu mi ésk amul lugnu bok fugnu dadjié am lu fégn

  83. Walowalo Walowalo

    Walowalo WalowaloHace 6 días

    O verema ma Balla gaye la me emou s'en jtem ❤️👉🇸🇳

  84. Awa Ndiaye

    Awa NdiayeHace 6 días

    Modou lo le meilleur

  85. Medoune boufane Djiba

    Medoune boufane DjibaHace 6 días

    Balla bou bayè beurè douma setanati lamb

  86. Magui Fall

    Magui FallHace 6 días

    Machela balla rek

  87. lamine lamine

    lamine lamineHace 6 días

    Ndékété balla moo néxal journé bi ,

  88. lamine lamine

    lamine lamineHace 6 días

    Ndékété balla moo néxal journé bi ,

  89. Keba Cisse

    Keba CisseHace 6 días

    Balla ❤

  90. Elhji. Sy diaw

    Elhji. Sy diawHace 6 días

    😭😭😭du dara nk xana beigu eumeu da dane balla mei kuko beugu la

  91. Boubacar Syllame

    Boubacar SyllameHace 7 días

    Le vrai lion bg2, le de sa generations bg2 machallah rafét na lol

  92. Pape Diaw

    Pape DiawHace 6 días

    Mane dou Sama mbeur wayé diambare la foumou déme mou nékhe vive le sénégal

  93. Amadou Gassama

    Amadou GassamaHace 7 días

    Ndeydi coulanakh bala moy borom arrene bi

  94. Fadel Niang

    Fadel NiangHace 7 días

    Nooooo Eumeu balla meilleur action bou combat bi !!! 😍😍😍😍

  95. Samcho Diakhaby

    Samcho DiakhabyHace 7 días

    Le Sénégal dois arrêté la lutter et cherche un bon emploi pour tout le monde parceque on pays une seul personne 100millions et les autre travail matin midi soir on te pays 1000f sque cest normal ça?

  96. khékhall diné l'islam tv

    khékhall diné l'islam tvHace 6 días

    bilahi tu es dit la vérité

  97. Sakoura Diop

    Sakoura DiopHace 7 días

    Douma doyal si action bi balla ak eumeu déff bilahi

  98. bjslalumiere SAMBOU

    bjslalumiere SAMBOUHace 7 días

    Il est devenu plus jeune

  99. Adama Diop

    Adama DiopHace 7 días

    Balla gaye Rekk

  100. Sahir Ndoye

    Sahir NdoyeHace 7 días

    Eumeu dafa beugg balla gaye si khol bi sans tricher bilay ❤️ c’est beau

  101. soda sall

    soda sallHace 6 días

    Mom sakh dakoy wakh néna dafa beug Balla ❤️❤️❤️

  102. Mbenda Niang

    Mbenda NiangHace 7 días

    Bilahi Balla namou naniou sa takusane bilahi

  103. Barro Lo

    Barro LoHace 7 días

    Bombardier yalla na yalla maye là ndam the barke serigne touba

  104. Hamza

    HamzaHace 7 días

    I just can’t stop watching the part Eumeu and Balla dance ❤️

  105. Mody Ba

    Mody BaHace 7 días

    Mongui mél né moy beuré dé bilakhi cest le meilleur