馃洃SUIVEZ CONFRONTATION #EUMEULAC2 / #DIENEMODOUANTA #AVRIL04 AVEC BIJOU NGONE |VENDREDI 9 AVRIL 2021

馃毄ABONNEZ-VOUS 脿 la Cha卯ne de la 2STV cliquez sur ce LIEN馃憠 : bit.ly/3cnXP6h
Retrouvez l'ensemble de nos programmes d'actualit茅 et 茅missions de soci茅t茅, sant茅, politique, culture, musique, 茅conomie sur:
- esdos.info
- www.2stv.net
- Iptv disponible sur 2stv.sn
- 2stv_senegal
- 2stvsenegal
- Snapchat: senegal2stv
- TikTok: @2stvsenegal
- 2stvsenegal
- www.dailymotion.com/video/x7vidbb
#CONFRONTATION #EUMEULAC2 #2STVLIVE #2STVSENEGAL #KEBETU

Comentarios

  1. Fatou Ba

    Fatou BaHace 23 horas

    Lac de guerre amale yar yaww Du courage modou anta 馃檹 脠me s猫ne yawww champion ga macha allah

  2. Badara Sidibe

    Badara SidibeHace 5 d铆as

    Ay way koumay diapal猫 dioxma numero eumeu ta yala tax

  3. Baba Thiam

    Baba ThiamHace 12 d铆as

    Lac de guier2 gorrjiguene la outil bongo d'i tassou

  4. Daouda Gu茅ye

    Daouda Gu茅yeHace 13 d铆as

    Lac dou dara

  5. Sadibou Aidara

    Sadibou AidaraHace 15 d铆as

    Kenou dou eumeu

  6. Lalia Coulibaly

    Lalia CoulibalyHace 19 d铆as

    Wallay gaston il me tue 馃槀馃槀馃槀馃槶

  7. Lalia Coulibaly

    Lalia CoulibalyHace 19 d铆as

    Ragal bi gneup kham naign ko馃槀 lac nopil

  8. Cherifou Singuinar

    Cherifou SinguinarHace 23 d铆as

    Gastron vrai domeram la

  9. Cherifou Singuinar

    Cherifou SinguinarHace 23 d铆as

    Lac mi vrai goor djigene leu

  10. Bouba Diouf

    Bouba DioufHace 23 d铆as

    Eumo dousa morome vraiment d茅male diagu茅 bapate

  11. Fatou Gueye

    Fatou GueyeHace 24 d铆as

    Mane je savais pas que lac de guerre 茅tait si b锚te tchiim nd茅k茅 goude ak Reuyy takhoul ame khelle

  12. Fatou Samb

    Fatou SambHace 24 d铆as

    Lac niak na diom reuy na lamigne begue na diakhas茅 ay wakh meuna yakk lamb

  13. seydina omar diop

    seydina omar diopHace 26 d铆as

    Lac2 dougn ko bayei teugeul lamb niit gni nopalou

  14. Thierno Yaya D猫me

    Thierno Yaya D猫meHace 28 d铆as

    Eumeu S猫ne dalna machalaaa Lac mom amoul roussoukayyyt

  15. Zizou Diagne

    Zizou DiagneHace 28 d铆as

    Lac tapet d'o霉 dieul roi des ar猫ne xana roi bi ngay dieul A每 wax lay done

  16. Pape Diop

    Pape DiopHace 28 d铆as

    Lac fi k茅n banioulafi ya niak diom t茅 do ndago dadi茅 amal fit

  17. Assya K芒

    Assya K芒Hace 29 d铆as

    Lac de guerre yaw doule khamo gateu sa khole bou bone dom茅rame ga r茅k famme biga done 馃枙馃徔馃枙馃徔馃枙馃徔馃枙馃徔馃枙馃徔

  18. bocoy noiu

    bocoy noiuHace 29 d铆as

    Mane lac 2 noumou def ba n茅k mbeur lay lathie

  19. Nabou Ndiaye

    Nabou NdiayeHace 29 d铆as

    EUMEU daga soxor trop nak waxofi nak Lac beug dou bagn beug nane la ba par茅 k茅n manousi dra馃挭馃挭馃挭

  20. Nabou Ndiaye

    Nabou NdiayeHace 29 d铆as

    Mbeur bola nexoule n茅xoula r茅k m茅 LAC GU脡R degue rek ga wax Eumeu boule salt茅l b victoirou diambour thipatouwaye

  21. asioe kiou

    asioe kiouHace un mes

    Mane lac 2 noumou def ba n茅k mbeur lay lathie

  22. Lvyyrgchf boy

    Lvyyrgchf boyHace un mes

    Best Datting Click 馃斀 18cams.xyz 鍦ㄦ暣鍊嬩汉椤炴鍙蹭笂锛屽挤鑰咃紝瀵屼汉鍜屽叿鏈夌嫛鐚剧壒璩殑浜烘崟椋熼儴钀斤紝姘忔棌锛屽煄閹紝鍩庡競鍜岄剦鏉戜腑鐨勫急鑰咃紝鐒'瀹堝拰璨х鎴愬摗銆傜劧鑰岋紝浜洪鐨勭敓瀛樻剰椤樿揩浣块偅浜涜鎷掔禃锛岃鍓濆オ鎴栨懅姣鐨勫熀鏈渶姹傜殑浜哄戞壘鍒颁簡涓绋敓娲绘柟寮忥紝涓︾辜绾屽皣鍏禗NA铻嶅叆涓嶆柗鐧煎睍鐨勪汉椤炵ぞ鏈冦 瑾埌椋熺墿锛屼笉瑕佷互鐐洪偅浜涜鎷掔禃鐨勪汉鍙悆鍨冨溇銆傜浉鍙嶏紝浠栧戝鏈冧簡鍦ㄨ蹇借鐨勮倝椤炲拰钄彍涓皨鎵剧嚐椁娿備粬鍊戝鏈冧簡娓呮綌锛屽垏濉婏紝瑾垮懗鍜屾參鐕夋參鐕夌殑閲庤彍鍜岃倝椤烇紝鍦ㄩ鍝佸競鍫翠笂琚拷鐣ョ殑閮ㄥ垎瀹剁敤钄彍鍜岃倝椤烇紝涓︿笖瀛告渻浜嗕娇鐢ㄨ姵棣欑殑鏈ㄧ厵锛堝灞辨牳妗冿紝灞辨牳妗冨拰璞嗙鐏屾湪 渚嗚鍛抽鐗╃叜鐨勬檪鍊 1618603293

  23. Bimootd officiel

    Bimootd officielHace un mes

    Bijoux dafa mini kou nop eumeu 馃グ馃グ

  24. Ismaila Drame

    Ismaila DrameHace un mes

    Mais lac mi nd茅k茅t茅 ab dofla dh no馃槀

  25. #Bambiste chycorien

    #Bambiste chycorienHace un mes

    1:03:50 degeul lac di doul nan dor mou wadd

  26. Sokhna Thiam

    Sokhna ThiamHace un mes

    Lac nopile

  27. Sokhna Thiam

    Sokhna ThiamHace un mes

    Lac kome 馃馃馃

  28. Mame Awa ciss茅

    Mame Awa ciss茅Hace un mes

    Bravo eme s茅ne sa pion ga machalla 鉂わ笍馃拫馃檹馃檹馃憤

  29. Grand Gass

    Grand GassHace un mes

    Lac 2 kagn ngay seuyi.馃榿馃榿馃榿mane hamna tu es vi茅rge

  30. yasio bolo

    yasio boloHace un mes

    Eumeu dou sama mbeur ms da am savoir vivre savoir faire et mm savoir parler 鉂わ笍

  31. ibrahima souare

    ibrahima souareHace un mes

    Radio grafia biii kholen date biii di na leer boudeee apres le combat bi le lac day fennnn boudee avant combat bii la wakhna deugeu

  32. ibrahima souare

    ibrahima souareHace un mes

    Yar zero ndeysann ki daffa bett nieupppp

  33. Mamadou Sow

    Mamadou SowHace un mes

    Lac comme kou Danel 馃槀馃槀

  34. Patrice Gomis

    Patrice GomisHace un mes

    Lac mome d'o霉 champion day respecter distasiation sociale

  35. Ibrahima S茅ne

    Ibrahima S茅neHace un mes

    Eumeu S茅ne t'es un guerrier n茅e 莽a se voit m锚me dans ta mani猫re de parler

  36. Malick Thiaw

    Malick ThiawHace un mes

    Eumeu

  37. vbddfy euuyt

    vbddfy euuytHace un mes

    Eumeu sene dal machallah sa khol rafett amal diam rek馃憣馃徔馃檹馃従

  38. Pape Mbagnick Ndour

    Pape Mbagnick NdourHace un mes

    Tr猫s franchement gni n茅keu ci plateau bi yeup donio farr ak Eumeu... Bayil茅n victoirou diambour bigu茅n di salt茅l ishhhh

  39. Patrice Gomis

    Patrice GomisHace un mes

    Eumeu sa kanam newineu m茅 Moy Sama mbeur

  40. Rokhaya Diatta

    Rokhaya DiattaHace un mes

    Ayy eumeu srx daffa am yaar t茅yy kham savoir parl茅 love sur toi tu n'as rien a prouver au s茅n茅galais tas tout fait

  41. OUMZ DABBZ

    OUMZ DABBZHace un mes

    EUMEULAC2 LETS GO .. MY MONEY STILL ON EUMEU ALL DAY HIS THE GOAT 鉁斺湐鉁斺湐

  42. Alune Ba

    Alune BaHace un mes

    Lac amoul v茅rgogne koi

  43. Cheikh Jr

    Cheikh JrHace un mes

    Sanex a des mots incroyables ms courage modou anta djiambar gua馃憡馃徎

  44. W Papii

    W PapiiHace un mes

    Lac de guiers esk dou 帽iarel 馃槀馃槀馃槀馃槀. Il est grave ce mec 馃ぃ馃ぃ

  45. Adama Sow

    Adama SowHace un mes

    Lac de guerre s'est un champion mais malheureusement il n'est pas professionnel 脿 travers sa communication..Il parle mal vraiment...damako yeureume sakh

  46. Alioune Thioune

    Alioune ThiouneHace un mes

    Lac da rew respect way

  47. Diaba Fall

    Diaba FallHace un mes

    Wa lac dou r茅茅 tmt fi adouna la man yw la support茅 ms bagnil gnagual bi

  48. elhadji mbaye

    elhadji mbayeHace un mes

    Vraiment modou anta sui d ts coeur avec vs bilay yalla dinala fay sa khole.sa nekh beugu na ligua defff ni day deuguou bilay

  49. Awa Baba Niang

    Awa Baba NiangHace un mes

    Diadjeuf eumeu sene

  50. dame kara Fall

    dame kara FallHace un mes

    Modou anta yalla nala yalla diapa l茅

  51. Nino Jahlil l'officiel

    Nino Jahlil l'officielHace un mes

    Modou Anta Champion nga Numu meuna deimeii Ns sommes derri猫re toi Lion Nga馃敟馃憡馃挊馃槶馃挆馃挊

  52. Djibril Geuye

    Djibril GeuyeHace un mes

    Courage modou anta馃挭馃挭馃挭馃挭馃挭馃嚫馃嚦馃檹馃檹馃憟馃憟馃憟

  53. remond ndiaye

    remond ndiayeHace un mes

    Lac bilae ya niak diom meuna diaxassei nit ak nit

  54. Djibril Geuye

    Djibril GeuyeHace un mes

    Eume sene maire de guediawaye馃ぃ馃ぃ馃ぃ馃ぃ馃ぃ馃ぃ馃ぃ

  55. sokhna bop

    sokhna bopHace un mes

    Ya lac dagay har ndakh nul mola geuneul fouf victoire 馃槀馃槀 Mba khamegani do gawa beureuwate馃槀馃槀 Eumeu SENE macha Allah yaw daga yarou boula b茅ne khaler sorkho sorkho champion pire ga macha Allah

  56. Fatou bintou Djitte

    Fatou bintou DjitteHace un mes

    Modou anta sama mbokk talib茅 nga

  57. Astou Diack

    Astou DiackHace un mes

    Eumeu yow daga yarou boul yak temps ci ki

  58. Fatou bintou Djitte

    Fatou bintou DjitteHace un mes

    Macha allah 鉂わ笍 gris bardeaux kaddou yi rafetna

  59. Fatou bintou Djitte

    Fatou bintou DjitteHace un mes

    Lac nopill wayyy sofff nga bari nga wakh euppeul nga khamo ninggay wakh茅...... BIJOU sa fond de teint bi saffnnaaa

  60. Madior Gueye

    Madior GueyeHace un mes

    Mba kham nguen ni Lac de guerre esprit djigu茅n la yor茅 Goor djigu茅n leu koi

  61. Djibril Ndiaye

    Djibril NdiayeHace un mes

    Lac tu es nul

  62. Aliounebadara Ndiaye

    Aliounebadara NdiayeHace un mes

    Lac goor dou Bari wakh Modou anta nioune wa Thi猫s yaw laniou am champions gua

  63. soiung toiue

    soiung toiueHace un mes

    Dakh yaw eumeu doo moromou gayi du courage 馃挭馃挭馃挭馃憤馃挊馃挊馃憤

  64. Alhassane Ba

    Alhassane BaHace un mes

    Lac do touss ya geneu yambarr si mbeurr yeupp

  65. Mariama Dansokho

    Mariama DansokhoHace un mes

    Lui khana lui entre nous

  66. Tidiane Sylla

    Tidiane SyllaHace un mes

    Big Taff comme borom keur bougnouy dabb dikoo niande 馃槀馃槀top si ganaww bijou rk

  67. ibou thiam

    ibou thiamHace un mes

    Bilae wallae Lac2 mi meune na tass adouna ndaxx meune f茅ne ki mo meune doul wayy

  68. soiung toiue

    soiung toiueHace un mes

    Confrontaci贸n nekhna

  69. Mamadou Mbaye

    Mamadou MbayeHace un mes

    Lac amo savoir vivre nit day respect茅 bopam bo beugu茅 niou respect茅 leuh nieup xam nanou ni do mbeur yawou dial sakh mola gueuneuh riche palmares mayal nit gni diam s茅n茅galais yi xam nanu lepp

  70. amadou dienf

    amadou dienfHace un mes

    bool茅en bal

  71. boyo Jarra

    boyo JarraHace un mes

    Lac yow zero nga c komba b

  72. Abibe Ousmane

    Abibe OusmaneHace un mes

    Modou anta do touss

  73. ibou thiam

    ibou thiamHace un mes

    馃槀馃槀

  74. Dabakh DIENE

    Dabakh DIENEHace un mes

    Bilaii Modou dioy lo nama馃槶 D茅j脿 je l'appr茅ciais ndakh goor Yalla la ci lepp.. Mais l脿 je l'estime de trop.. BayeFall amal diam.. 馃憣

  75. Seck Abou

    Seck AbouHace un mes

    Way lac double rek

  76. ndiatigu茅 com茅dien

    ndiatigu茅 com茅dienHace un mes

    Tapez ndiatigu茅 com茅dien et abbonnez vous vite r茅e ba tass 馃槀 thi茅y ndiatigu茅 mingui tothie youtube

  77. Keita Fanta

    Keita FantaHace un mes

    馃槀馃槀馃槀馃槀馃槀馃槀馃槀馃槀馃槀馃槀

  78. fadel bu lo

    fadel bu loHace un mes

    Gaston arrete tes rouber fi sonko mo fi neee bu niu sonal di rouber merde a la fin sa combat bu nakarie bi馃憥馃憥馃憥馃憥馃憥

  79. fadel bu lo

    fadel bu loHace un mes

    The king xaragne lo馃馃馃馃馃馃

  80. fadel bu lo

    fadel bu loHace un mes

    Nooooo modou anta vs ns avez fait touss pleurer walah du courage pr la suite 馃憣馃憣馃憣

  81. Tall Mbaye

    Tall MbayeHace un mes

    Big taff 3h de temps en debout Franchement ils sont pas s茅rieux

  82. Oumar Thiene

    Oumar ThieneHace un mes

    Vraiment j'ai pleur猫 a chaud larmes avec LS propos de sanekh c'est triste ayons la courage d'aider nos fr猫re thiesoise

  83. Awa Baba Niang

    Awa Baba NiangHace un mes

    Confrontaci贸n nekhna

  84. Lamin Diop

    Lamin DiopHace un mes

    Yaw lac doul nopil amo lo wax

  85. Seydou kasse

    Seydou kasseHace un mes

    Lac2 tu a d茅莽u tout les mondes. Merci champion euma

  86. sombel sene

    sombel seneHace un mes

    moudou sama kholl diekhna mane mom mkilaye dianall mame ch ibre mika yakar mo takhawola馃槶馃槶馃槶馃馃

  87. Lamine Ndiaye

    Lamine NdiayeHace un mes

    P猫re Macond茅 meunoumako mougn kw馃榾馃榾馃榾

  88. Marie Ndiaye

    Marie NdiayeHace un mes

    Non bijoux machallah dama r茅h ba soneuh machallah jsui lac 100% dina bakh

  89. ma茂mouna fall

    ma茂mouna fallHace un mes

    Lac dafa rew mais yaw yaye kane

  90. Sene Pouye Mareme Madame

    Sene Pouye Mareme MadameHace un mes

    馃槶馃槶馃槶馃槶馃槶modou anta tu ma fais pleurer

  91. MBAYE NDIAYE

    MBAYE NDIAYEHace un mes

    Euma wakhna deug

  92. Khady Drame

    Khady DrameHace un mes

    Eumeu diambar la gni d鈥檃ccord ak mane dafal j鈥檃ime 馃憤

  93. Binetou rassoul

    Binetou rassoulHace un mes

    Day doul lokho bou dam guakoy niamakh niamakhi

  94. Binetou rassoul

    Binetou rassoulHace un mes

    Lac 2 thiokh la amoul

  95. Jacques D Diouf

    Jacques D DioufHace un mes

    Vraiment lac 2 na rien a dire raggal la

  96. Mouhamed Diouf

    Mouhamed DioufHace un mes

    Lac sisoumane la 馃槀

  97. Maty Diane

    Maty DianeHace un mes

    Eumeu tey na yarou na machalla lac sa wakh barina te diom zero

  98. Courielle Balde

    Courielle BaldeHace un mes

    Eumeu sene y'a geuneu yarou si mbeur yeupp machallah

  99. Nd猫ye Gning

    Nd猫ye GningHace un mes

    Euma champion

  100. Nd猫ye Gning

    Nd猫ye GningHace un mes

    Fo guis kou bari wakh tap猫te leu

  101. Anta Mbodji

    Anta MbodjiHace un mes

    Thieuy bijou dawul thiow 馃槀ragalo dh 馃槀

  102. ndeye ndoye

    ndeye ndoyeHace un mes

    Lac doule way yaw doule kakte bou mak gua